la fin justifie les moyens🥵

8.5K 174 13
                                    

Salut tout le monde comment vous allez bien voici un nouveau chapitre de votre chronique j'espère que vous allez apprécier comme dab mm si becoup de personne ne le font pas mais voter aimer et ceux qui le peuvent abonnez-vous merci et bonne lecture

Non mais deuk bi méti na danguay oute liguey ba sone doko ame je reviens de mon dernier entretiens d'embauche et a voir la réaction de ce connard je n'aurais pas le travail domeram bi koumouy teudé lay weur mais non kouko liguéyal wakhôu ma mounane say morom ni lagnouy def moi je m'en fou jai ma dignité mm si je suis pas vierge depuis longtemps mais nak kéne douma chantage pour katt ma sa jamais douma ko meuss nangou bref kholal rek dama beurri wakh beurri histoire je me suis mm pas présenter je m'appelle coumba ndoye je suis une jeune femme de 24ans jai fini mes études l'année dernière en bureautique et secrétariat  depuis lors nak mangui weur liguey mais Sénégal mome cest peine perdu je vie avec ma cousine a mariste parceke je viens pas de Dakar et jy ai pas de famille alors kan jai fini mes études ma mère ma proposer de vivre avec ma cousine qui était déjà installée à Dakar.  Faut dire que kan je suis venu elle ma super bien accueillie gentil comme tout belle charmante khalé bi nekh na toye na mo takh goor bou nek mokoy setsi mdrrr néna dou thiagua mais sorri wouko Dal lolll😂😂😂😂 je juge personne mo takh sougnou nék mane ak mome nekh je m'occupe pas de ce quelle fait ny ne dit rien à la famille mome nak kham na lolou lama respecter aussi comme le dit le proverbe sénégalais 《lokho bilay doundal doko dague》 boudoul wone mome heure bi dé na parceke depuis que je suis ici je gagne rien en plus tamit copain bima nekal tané wouma coté financier alors je ferme ma geule sur tout . La je rentre à la maison un peu déçu de ma journée faut le dire j'arrive j'ouvre et j'entends du bruit dans la chambre de ma cousine makoy rafétal ni rek mais thiagua bi dagnou koy katt instant mongui youkhou appartement bi yeup je passe juste devant sa chambre cest pas complètement fermé li mo takh bruit yi fort en passant je vois le gas qui est derrière ma cousine diko katt dako dioutal mais Lima geune surprendre moy koyou wadji Putain qui loy bi didje na cest énorme cest pas long mais circonférence bi mo ngande si bopam je reste scotché kelke seconde smaa cousine bi guiss nama et me souris je me ressaisis puis entre dans ma chambre je me déshabille et va prendre une douche limay sangou yeup sama khel mongui si koyou wadji mais Lima geune diakhal moy sama cousine nane la def ba meune encaissé li en plus mouy rétane akkkk il mome doyna warr. Je fini ma douche et je vais me coucher pour me reposer un peu mais nélawouma jai hyper faim en plus je veux pas sortir risque dadjé ak wadji je veux pas kon me préne pour une pute adouna wauroul . Après kelke minute j'entends ma cousine qui m'appelle je sors de la chambre et je vais la rejoindre dans le salon elle était habillé juste d'un string et d'un top qui couvre mm pas ses seins thiagua bi

-elle: sa diank yaw bobou ba légui mangui lay wo oubien khiffo
-moi: khiff mo takh dégou malla 😂 té beugou malla wone déranger
-elle: mooo yaw loy diaye timide ni kham nalla ki dé sama béne mbarane la wayé tamit meune na katt 😂
-moi: mo takh dé sa badio bi mongui melni téne ni 😂😂

En parlant ma wane ko badiom bi mongui oubé kou elle regarde gnou ande rétane non entre nous nak ya pas de complexe faut le dire gnou lék ba sourr il y avait un bon plat de mbakhal bou saff ame dakhar dama si raye sama bop

-elle: wa chérie sa entretien bi noumou démé tu ma rien dit
-moi: akh comme dab rek domeram yi kougnou katt rek lagnouy weur
-elle: lolou mome yague naffi mais tamit esceke do khalate touti diéme nangou sa yaye mongui deuk ba té ame na yakar si yaw
-moi : sa cest vrai mangui siy khalate mais PA ( vieux ) yi so léne topé dagnou lay yakh ay pervers lagnouy té beugue na fondé famille tamit a l'avenir gni sougnou la diapé ba bayi la béne goor dotou la beugue
-elle: tu as raison dé mome ak mais Dal diémal khole no amé khaliss mole gua raféte gua lo beugue meune guako ame té comme je l'ai dit sa yaye yaw la ame tkt je vais en parlais a un de mes mbarane je pense que je peux t'aider sur ss
-moi: soko déffé diapaléma deugue sakh sokhla nako dé

Katanté world Where stories live. Discover now