KMTN 10

6.4K 924 129
                                    

Sira
J'ai pris Oumar mane dem installé wou Cii côté Doudou et Sophie. Gni mane lagnouy woo cii tanebeerou kagna wayè gni khana khamougnou ni que defantè la def garab diko sangou, diko lekk diko nane tamite.
_ cma vs allez?
_ cv dh, ils disent en chœur
_ Ahh c bien! Bb tu les connai? Lui c Doudou et elle c Sophie
(Il était choqué bima ko wakhè Bb wallahi dom dioumouma sakh😂)

_ oui, je connai Doudou en faite c moi ki la invitè, disa Oumar

Ahh ok! Je pouvais sentir la jalousie envers Doudou prck pour mom ni que sans mom dal ma vie amatoul sens, wayè dina khamnè que bignouy dioudou andougnou. Je pouvais sentir sa haine envers Oumar prck dafa beau gentle comme leem🍯. Wawaw khalè bi khol nako dh 😍😂 dagno meunoul dioubo rek. Yalla nak boumla rètane avec ses focettes ohoooo. "Alal kouko sagane mom kouko farlo mokoy moudjè".

_ Ah bon dc vs vs connaisez?
_ Oui oui, com si com sa rek, Disa Doudou
_ Ahh c bien! Bae magui dem kholi Birthday Girl ci loumou nekk, lui dis-je en lui donnant un bisou sur la joue💋

Niafff!!! Doutougnouko dolèti. Sophie mom damako beurgeul wayè mane laffi fekk gnakk diom.

Penda
_ c qui ton ami, dis-je à Amadou en lui tenant bien Le Bras prck je sais que Demba nous regardais
_ je crois que tu le connaissais déjà
_ Ah oui sakh mais lolou
_ Haral ma woko, Dembaaaaa!! Viens ici

Waa ki eupeuloul rekk cheuu. Après il venu s'asseoir à côté d'amadou. Ohh com je le déteste.

_ Happy birthday Penda, en me donnant un cadeau bien emballé thippp
_ Merci c gentil de ta part
_ De rien ma Princesse
_ C Penda
Mako dieppi rek. Fi dh kene rek mo ame droit wakh Ma Princesse et c sama Kimay Nelaw❤️ Comme que il était un peu gêné par notre conversation, il a décidé de ns laisser seule cii fauteuil bi prétextant d'aller chercher quelque chose à boire pour son ami ughhhh!!

_ Bae doma indalel Ndokh stp dama marr.
_ Anything for you my Queen 👑

Mom mom nanditè leu. GATT di dou Demba da beug kouko torokhal tay rek lakoy casser la gueule tè sama lokho douko lale.

_ magui la done woo demb sakh pour te souhaiter HBD mais je pense que dagua bloquè sama num
_ si je voulais te parler tu crois que je l'aurai pas fait depuis le début.

Ma diouk dem fèlou Sira et les autres gni done fethie. Tay sama beuss leu dou mom momakoy yakkal. On était là à danser rek prck lignou lekkone mo beurri so il faut que wone mou ress pour gnou ame fignouy dougal gâteau bi😂

Après on la coupè. On m'a fait beaucoup de selfies. J'étais comme une Reine comme ma chère Amadou ma appeler aww😍 quelques minutes passa, les gens on commencè a rentrer et ils m'ont tous remettre un cadeau sauf Doudou et cette Sophie là. Anyway nakaral Sira molene fi indiwone wayè khamna ni que tekk nalene sa place. Gnakk classe ba dè. Niit boula lidjeunti woul bouko lidjeunti, gnakk mandou lene meunoul Thipp.

Après bi gneup gnibiwè, il ne restais que nous quatre (moi, Sira, Amadou et Oumar)
Mane ak Sira on étais là à jubilé comme des petites fille prck on avais réussi à notre petite mission😂 Dagnoulene door tè sougnou lalou lene. Les garçons mom dagno warrou wone thiey.
_ Vs pouvez m'expliquer qu'est-ce qui vous a pris vous deux?, disa Oumar
_ Ak mane dh je comp rien mane, disa Amadou
_ mais on a rien fait, dis-je en rigolant
_ Yaw mayma ma wakh ak gni, dou yaw ya fi indi Demba loumala wakhone Bro il est la malheur de Penda, et toi Oumar ya invité Doudou nonou ba tokk
_ Ouais et alors?
_ voilà c'était mon ex et dafma bougone torokhalate wayè dou gnarr
_ Haha yagui sogua wakh kay, motakh bizarre comportment gua nane ma Bae. Khamone na que dagua bardè ci mane
_ Yaw mou gnaw mi mala done saggal do gou weuhh
_ Nel kay damala arranger
_ Haha vs deux kagne gueni changer😂, dis-je
_ Lol, et toi c'est quoi ton rapport avec Demba?, demanda Amadou
_ Bro je t'avais pas dit que c'était son ex non!, disa Sira
_ En plus tu ne veux même pas savoir keskil a fait jtlr, ajouta Oumar
_ Hmm kone lolou leu kone yess. Wa bakhaa. Wayè vs m'avez tuer yenafi manigancè sen faux-copins ba tokk
_ Ahh c vs qui avez invité les personnes qu'on n'aime pas kayy, vs assumez rek, disa Sira

Haha, on était là detailer notre fausse séance. Lol. Ils ont dit que nous sommes des fofolles wayè dhh c'était la meilleure de mes anniversaires. Nima contanè mo eupp koii. Vers 2h du matin, on avait déjà débarrassé tt dans le salon et dans la cuisine bala fadjar sama yaye diouk dignou teugeul Bercy😂😂

Apres, Sira et son frère ont décider de passer la nuit jusqu'à demain. Sira était avec moi et on était entrain de parler entre filles, etc.... Et oumar et Amadou jouait avec leur PlayStation. Nimalene dieppi wè amougnou bene vie loudoul football ⚽️ ak Games. Et NARUTO!!!!! Mais ya koii🤷🏾‍♀️😂😂

Oumar
Bah, com vs voyez je suis le petit frère de Penda. Je m'appelle Oumar Diop et j'ai 19 ans. Parlant de moi nakk ya rien de spécial sauf que je suis amoureux. Oui de qui? Soumalene ko wakhoul sakh warr guene ko kham. Yea C Sira. J'ai eu une affection depuis le premier jour qu'on s'est connu. Je pense pas qu'elle ressent la même chose mais loutakh ma yapp ko dou dara c'est que sayoumako guissè sama tank yii diakhasso douma sakh kham loumay wakh di ratatati rek. J'adore de l'ennuyer et de la faire rire même ci c con je sais. Mais instant yi mom limay yeukk c trop tè meuneutoumako tèyè. Je sais pas comment je vai lui avouer mes sentiments mais Magui khar le moment venu dal.

Moi et Amadou étaient entrain de jouer au PlayStation. Il est mon pote et je lui considère com mon meilleur ami même s'il est âgé que moi.

_ Wa boy nos sœurs ni lagne leni bayiwè, lui dis-je
_ Ahh lougnou lene meuneul nakk
_ moma ci diakhal mane
_ Haha wayè toi on dirait que Hmm........
_ Quoi??? Wakhal rek
_ que sama sister amna foumou nekk sa xol bi dh je vois la façon dont tu la regarde desfois

C'est comme qu'il a lu ma mémoire. Ahh je doit le lui avouer je vs jure c trop trop pour moi.

_ pour ne pas mentir bilahi elle me plait depuis le premier jour. Je sais même pas comment le lui dire prck Sira Moy lolou dh ymgx
_ Haha yagui sogua wakh lou takh meunolene dioubo bene yone. Ehh le petit frère est amoureux. Père You nena "Sa mbeguel wakh koko soko wakhoulè bamou dem guiss kenene guay yendo misère Plus Fort!"
_ Haha lol! Je vais essayer dal wayè bouko wakh dara
_ Hii mane kay douma dougou cii yeuffou Sira ymgx merci rek. Bonne Chance!
_ mane guay kagno wa bakhna.
_ Wohoooo! Je t'ai gagné 2 fois. Nenala maleu meune. Wala sa crush bi guay khalate "mbeuguela woor mbeguel is all ba worra woor soula beuguè na woor"😂😍
_ Cheuuu Yaw arrête, khamgua mane ak fiit rek je le ferai. Yaw mom toggual fi mala sakh tanè moi je suis amoureux et j'assume. Et toi tu crois pas que khawma dagua bardè ci Penda.
_ De quoi tu parles?
_ mané bayil doff doflou bi. moi je te connais dh boy réglel sa situation bala mo trop tard dal
_ Hmm Naci bayi khel
_ Penda nekhouta bagne dal. En plus day nekh sakh on va etre des beau-frères
_ T un gamin toi do dem

Et après fi lene nekk di jouer et parler ba 6h du matin, gnou diouli fadiar dadi dem dodo. 💤

Demba
Deug deug nakk Amadou yapp nama. Sagn na guene ak boy bi tè doumako wakh. Wa bakhna. Quand il l'a appeler My Queen je voulais lui faire savourer mon coup de poing tellement mais je me suis retenu sachant qu'il ne connaît pas ce qui ce passe entre moi et Penda. Wayé quelque chose dal est sûre, Penda je l'aime et je ferai tt de mon pouvoir pour la récupérer. Loumaci gobbè garr ko. Je suis incomplète sans elle et je l'ai su depuis qu'elle s'est séparée de moi.😫😭

Bane couple molene dakkal😍Penda & Demba? Penda & Amadou?
A vos avis!
_____________________
Mes parariiipis😍 Sen partie migui nonou. No lene ko guissè. Na xol yi fekh way guene voter ci bidew bi ⭐️ .
Commentez aussi.
Je vous love ❤️💋💯

🌺Bbeii_Mbene🌺

KiMay Tèrè NelawWhere stories live. Discover now