Titre de la partie

1K 93 0
                                    

🌴 *WAXI SERIGNE TOUBA*🌴

*SERIGNE TOUBA(Kllml) neena:*
Beugg lou baax ak Beugg sa bopp bokounou.
👉🏻 Beugg lou baax deugg kouko déf, fou lou baax meuneu nékk rék danako nééx
👉🏻 Beugg sa bopp nak bòko défé, dinga beugg lou baax wayè sa bopp rék ngakoy yééné

📚 *Source : Garabou TOUBA, VOL1*

Waxi Serigne ToubaWhere stories live. Discover now