Titre de la partie

962 87 2
                                    

🌴 _*WAXI SERIGNE TOUBA*_🌴

💫 *SERIGNE TOUBA(kllml)* mësnagn kòo ladj:
👉🏻 Ndax nite nga?? Mouné dédéét
👉🏻 Niounéko sa doom yi nak ndax nite lanou?? Mouné waaw, wayé défnaa thi nioom lou nékoul si nite gni

📚 _*Source: AD' diyàfatou Samadiyyah, VOL 3*_

Waxi Serigne ToubaOù les histoires vivent. Découvrez maintenant