Titre de la partie

925 78 0
                                    

🌴 _*WAXI SERIGNE TOUBA*_🌴

💫  _*SERIGNE TOUBA(kllml) neena:*_
👉🏻 Xeuthiò thi adouna, bokk n'a thi liy yaxx jëffi euleukk. Té kou yaxx jëffi euleugëm thi adouna, bou ëleugué dou jarignou moukk

📚 _*Source: AD'diayafatu Samadiyyah, VOL 6*_

Waxi Serigne ToubaWhere stories live. Discover now