Mbaa xam nga ne yaw yaay ki falu ? (Sais-tu que tu es l'élu ? )

4.3K 182 6
                                    

Je vous présente mon troisième et dernier poème du jour (écrit en wolof cette fois-ci).

Titre :
Mbaa xam nga ne yaw yaay ki falu ? (Sais-tu que tu es l'élu ? )

Si les poèmes précédents évoquent des amours regrettées, ce dernier parle d'une femme mariée qui fait les éloges de son époux.

Jàmbaar, kuy wër buur na tee sa loxo

Oups ! Cette image n'est pas conforme à nos directives de contenu. Afin de continuer la publication, veuillez la retirer ou mettre en ligne une autre image.


Jàmbaar, kuy wër buur na tee sa loxo.
Mbaa xam nga jegewoo baadolo ?
Yaa def lu kenn deful .
Xale yi góor yi di fo, yaw nga nekk beneen « poule ».

Mbaa xam nga ne yaw yaay ki falu ?
Dara du tax nu fakastalu.
Yaa fekk ku jàppee mbëggéel fitna,
Sol xol bi lu rafet ne jaalaabe.

Coco, yaa jël ay waxtu di baaral
Diggante bi mel ne udde ak barngal

Wax ma  nan laay taasoo say jalloore,
Jàmbaar, kenn du la  jiiñ yambar.
Sama halal, maalay piis , maalay takkal fer mu dar,
Walla ma def ne lingeer ya ca Kajoor.

Amul ragal, li du mbëggéelu  parifoot,
Ndax lu ler lanuy wut.
_____________________________________________

Traduction

Quiconque recherche un chef devrait te prendre comme guide, guerrier.

Tu as accompli des choses que personne d'autre n'a réalisées.

Alors que les garçons s'amusent, tu es dans une autre poule.

Sais-tu que tu es l'élu ?

Rien ne peut nous faire tomber.

Tu as su toucher le cœur de quelqu'un qui voyait l'amour comme un défi, en l'embellissant avec autant de soin qu'un artisan façonne une jellaba.

Chéri, tu as cultivé cette relation avec patience, tel un  cordonnier avec sa lissette.

Comment pourrais-je suffisamment louer tes exploits, guerrier ?

Personne ne peut te qualifier de faible.

Mon bien-aimé, je t'adresse un clin d'œil, je porterai ces perles en ton honneur.

Sinon je peux aussi m'y prendre comme les princesses au cayor.


Tu n'aurais jamais dû me sourireOù les histoires vivent. Découvrez maintenant