15

2.9K 191 1
                                    

Salam aleykum

Toujours dans la peau de Mounass

Sila déme si lieu bi ma ki kidnappé Majib wakhone dama tite ba khawouma loumay déf si la  tagou sama yy néko keur gnome Mounass laye déme  dama koye wétali ndakh séne keur kéne nékoufa sama yy néma démal ma gaw dieule taxi déme

Fatou : nga fénal mafa mane

Mounass : mangui diégalou nonou rk la mana déf

Virginie : Fatou bayiko Mou yégalé

Flash back

Ma yégue si bénne bâtiment bou sombre

Moi : Majib fo néh

Wayé kéne faléwouma sila commencés tite di dioye ndakh dama yakarni dagne ko ray teh wakhoumako loumay koye wakh ba paré

Moi a larme : majib fonéh guir yalla bouléne ko ray. majib mangui diégalou wakha goumala sakh samay sentiment .Teh dama promettre lone Fatou néko dinala balou mangui ni défa goumako . Majib bo démé loumay doundaté kone sama adouna dou nékh sans iow je t'aime Majib li léppou mane la souma la télone wakh damala nope do guénde mbane laye kidnappé Majib je t'aime ngir yalla boulema bayi parce que je t'aime

.... kone tu m'aime

Moi ma fombou sama rokhagne yi: Majib iow la

Ma guiss lampe yi take

Majib : manela kaye khame ngani meunou ma déme bayilafi

Moi: je te déteste Majib ( sama rokhane tokhou)

Majib fombousama rokhagne: boule dioye khana khamo boye dioye dafe maye métti

Moi: wa loutakh wowoma démbou bataye

Majib : mangui djégalou dama yakarni daga nobone kénéne kou bokou take ak mane

Moi: mane tmt dama yakarni daga nope Virginie lolo takh wakhouma la samay sentiment

Majib : nagne diale si bire da ame louma laye wane

Gnou déme si bire ma guiss mbénne Android bou raféte omg

Gnou déme si bire ma guiss mbénne Android bou raféte omg

Oops! This image does not follow our content guidelines. To continue publishing, please remove it or upload a different image.


Moi: waou oh my god majib..

Ma tourné ma guiss ko mou en genou  yore boîte bou défe bague lettre M

Majib :  guiss nga Mounass depuis bama la guisé la commencé ame sentiment si iow même soune première rencontre bou nékhoul tmt bobou la commencé ame sentiment si iow yalla défate gnou bokou classe wayé meunou malako wone wakh ndakh iow noboma wone lolo takh wakhouma mala wone dara guiss nga Virginie mimaye andale dafa nékk sama ami d'enfance rk wayé meusou mako nope iow la mana nope je t'aime Mounass wallahi même yalla khame nako je t'aime ndakh mane nga néke sama petite amie

Mane mangui dioye wayé dioyou contane la

Moi a larme : oui  moi aussi je t'aime

Mou takale mako ma déf ko li

Mou takale mako ma déf ko li

Oops! This image does not follow our content guidelines. To continue publishing, please remove it or upload a different image.

mou embrasséma si front bi

mou embrasséma si front bi

Oops! This image does not follow our content guidelines. To continue publishing, please remove it or upload a different image.

Fin de Flash back

F

ATOU: ooh je suis jalouse hein

Virginie : kone nékato célibataire

Evachou : kharal ma woute koumaye défal li teh lolou nékhouma dh iow miga khameni boune la dane wakh Majib ngani nékhouma

MOI : lolou diale na c'est le passé légui si présent lagni wakh

Virginie : da ame épisode bouma raw wala

Evachou : wawaw bise bi Mounass di doga guiss Majib louné yakke nakako

Retour dans ma peau

Moi: monté wakhone nagne kako néko Majib ngaye moudiéle

Mounass : iow khamena abdou ngaye mou diéle

Moi: shut boulma wakh si wakhou kokou

Virginie : guise nga Fatou Abdou djémala dougantéke mome rk khole bi dara néwousi

Moi: mane sakh mangui déme 16h diote na Kiné warna wathie

Virginie : mane domafi bayi

Evachou : mane mome si kogne bi rk la deukk déma gouma légui

_______

Moi: kiné daga wathia goule

Kiné: wathia gouma mangui si ecole ba taye

Moi: liga nianké kérsa sama tanta gneuweu goule

Kiné : wathia goule khamna si kakame touti rk

Moi: kone mangui déme sangou dji

A suivre

Voici Kiné

Voici Kiné

Oops! This image does not follow our content guidelines. To continue publishing, please remove it or upload a different image.
Abdou et Fatou  amour  inoubliable ( Wolof)Where stories live. Discover now