64

3K 180 12
                                    

Salem Aleykum

Tjrs dans la peau d'Abdou

Moi : papa wakhna deugue

Pp: takhawal ma expliqué la

Virginie *en larme*: non dou deugue depuis des années gnouy weure soune yy diko dioye nekké yo mogui doundou teh wakho gnouko PP NÊMA AÏCHA WAKHOUL FEUGUE

Aïcha : ha ha ha  Mangui déme lidiane tiléne séne problème famille mais khame léne lénne doumaléne bayi nonou dina gneuwate vangé wou teh Abdou sama yeufe la doumako bayéle kénn

Apres mou déme mais Sama khéle nékoufi konne kignou diapé pp depuis longtemps dagnou done féne

Ana *en larme*: ça fait des années maye dioye sama yy iow pp mouy dounedou teh wakho gnouko PRKW PP LOUTAKH NGA DÉF GNOU LI TEH NGA KHAME NI LOUSOUGNE yy tolou si gnoune prkw

Sama pp diko wadia lale mou pousse ko daw dougou si keurgui
Mane mome bataye meunouma wakh ndakh meunoumako gueume

Pp : Abdou

Apres ma déme wathie kofi

Moi : Ana nopiléne

Ana : loutakh pp défe gnou li loutakh Abdou

Virginie : depuis des années gnouy dioye yy nékké mongui doundou. Kone sama yy dagno abandonné lolo takh soune pp wakhou gnou dara

Moi : bayile ligaye wakh sama yy doune gnou masa abandonné

Gnou guiss pp Di gneuw

Pp: wakhna deugue séne yaye gui doundou mais meusou léne abandonné

Moi : KONE BOUNE GNOU ABANDONNÉ WOUL LOUME GNOU DÉF

Pp : JE VOUS AI DIT K SÉNE YY MEUSOU LÉNE ABANDONNÉ. LI SOUMA KO DÉFÉ NGUIR YÉNA TAKH

Moi : Mdrre pour gnoun hein donima lolou NGA wakh dh wala soune souffrance nga beugue

Pp : beugue ma wone wakh lolou. Mais solénema diklou woule louma léni expliqué

Moi : lo beugue ngani sama yy dagno abandonné hein lolo kasé nga gnou beugue expliqué diarouko ndakhe khame nagne ko. Iow AK Djibril yéna yame

Sama pp pés ma c'est la première fois moumay pése

Pp : mane nganane Djibril hein mane lima léne defal séne pp biologique daléneko defal. Teh Aussi nguéne diklou ma expliqué

Dlp de Youssouf

Kénn wakha toule

Moi : yéne lima déf pour yénela. Jour biguéne gneuwé fi kouléne fate dou mane bou nikoul wone mane si mbénde Yi nguéni deukk. 2 ans maye séte séne yy pour indilé léne ko
bamaléne guissé si mbénde bi nguéne wakh ma fatimata moléne diour nguéne expliquéma li khew léppou
Ma indiléne si keurgui chaque jours nguéni dioye séne yy meunou mako supporté
Mani na déme mbour séte bakhame ndakh yéne  meusou léne  guiss séne cadavre yy
Ma déme 1 ans maye déf recherche mais guissouma dara
Après ma khole presque hôpital yépou mais dara
2 ans silaye doga ame louma lére ni séne yy ngui doundou

° Flash back °

Dama done wadia déme bureau sama secrétaire bi woma téléphone

- salam Aleykum mr

Moi : Aleykum salam fo tolou si affaire bi

- lolo takh ma wolou la wone sakh.

Moi : pour lane

Abdou et Fatou  amour  inoubliable ( Wolof)Where stories live. Discover now