45

2.9K 210 4
                                    

Salam aleykum

Retour dans ma peau

Ana: bane fi gneuwé ba taye béne yone lagne fi nguénde

Evachou : moma diakhal dagno wara déme plage sakh

Ana: Abdou nagne déme

Abdou : wa bakhna préparé léne gnou déme

Virginie : Abdou yangui fi

Ana: mane mi sakh dama choqué

Kiné : loukhéw baguéni choqué

Virginie : Abdou nga khame ni soune dane déme fénn soune ko tago pour gnou déme sakh problème la surtout plage

Moi :ça c'est mon homme

Majib : degouma liga wakh dé Fatou

Abdou : yako guëneu dégue frère

Majib : ah Kone bb dagama trompé

Moi: nekoul sa bb dh.  c mon bb à moi seul nake tout court

Abdou : dou iow yama gneukka trompé

Mounass : Kone Majib nekou ma sa bb

Majib : tu n'es pas mon bb mais mon amour ma vie mon tout

Evachou : lolou fort n'a instant bi mane ak Virginie rk fi célibataire

Moi et mounass : vont les célibataire vivent les  amoureux

Kiné : mane nake si célibataire yi la boke

Moi: iow togal amo loudoul 16 ans soula sa yy dégué nga dh

Abdou : diouke léne gaw Ana aïcha taye guisou mako fi

Ana: esk nekoul chambre ram

Est ka dou da bougoul guiss soune couple lolou ko métti

Abdou : déme léne préparé yéne laye khare wakhalé ko Aïcha  iow Ana

Ana : ouais brother

Abdou  dikki si mane wakh sama nopou yi

Abdou : boule wakhak goor boule djégué goor soumala guissé ak goor dinako raye

Moi: inchalla wayé iow tmt boule djégué djiguéne boule dragué kénn

Abdou : mane sakh boudoul iow kénn intégré wouma

Moi: hum kone bakhna démal préparé

Gnou déme préparé kénn kou nékk wathie même aïcha khamouma louka dale damay khoule di signe rk
Mais yakarna amna loumouy manigancé

Gnou nguénn dieul oto bou make bo khame ni gnéppou khadje nafi
Plage bi

Gnou nguénn dieul oto bou make bo khame ni gnéppou khadje nafi Plage bi

Oops! This image does not follow our content guidelines. To continue publishing, please remove it or upload a different image.
Abdou et Fatou  amour  inoubliable ( Wolof)Where stories live. Discover now