65

2.9K 202 14
                                    


Salame aleykum

Tayela jour hénné time souba la takk bi instant bi soune keur mogui commencé ame aye gane

Comme k hénné time soubala mangui déme sama keur tata aïcha
Ma sangou défe lima wara défe

Ma wathie fékk fa sama tanta

Moi : Salam aleykum tanta

Tanta : aleykum Salam fo dieum khané donima dagaye guénn teh khéwélé Taye

Moi : sama keur tata laye déme rk mais tanta téle nga gneuw fadiare gui Teh gnigne yéwa goune nga toke fi iow kasé

Tanta : damala sokhlo wone sakh kaye sa chambre ma wakhla

Gnou délou wate soune chambre

Moi : lanela wone ba diamou j'espère que diamou la rk

Tante : enfaite je voulais te dire a propos de tes parents prkw tu leur pardonne pas

Moi : mais taa même tw tu sais limema défe lépou depuis mon enfance il m'ont fait la misère c'est difficile de leur pardonner. Et aussi taa oubli ça aujourd'hui c 'est ma journée. Nous devrons être content qu'à même .

Tante : ok si tu le dis mais khalate si degua il sont tes parents aussi je ne vous force pas de leur pardonner mais essaie defko rek

Moi : ok inchallah mais tanta bamaye doga gneuw séne keur dama yakarni tu vas me faire la misère. Mais je me suis trompée. Tu sais tanta je n'ai jamais senti l'amour paternelle ni maternelle . Mais iow ya takh ma khame louy amour paternelle même si k sama yaye 3ans yi mongui changer.

Tante : ohh ma chérie leuy lolou lougne koye wakhé louma défoul sama dome dinalako défe kénn . Teh aussi ce sont tes parents ils ont commencé à  regretté tout ce qu'ils t'ont fait.  Fait le juste pour mw ma chérie

Moi : yatakh mokoye defe dh. Mangui déme bala goudé

Tante : ok si kanam khamenala boule diale si Abdou * clin d'oeil*

Moi *sourire* : WA bakhna si kanam bou kiné yewou neko mangui gneuw beugue naye nélaw trop

Tanta : lane kiné fadiarouna marché AK jumelle Yi  pour dieun matériel ak aye cadeau

Moi : faté na ni kokou khéw la beugue.

Après ma embrassé ko si front bi daadi déme
---

-: salut Fatouche

Moi : salut Rama. Nkm iow

Rama : iow kaye nagne la bayi nonou

Moi : ne viendra pas en retard c'est a 16 h qu'on ira à la salon de coiffure

Rama : faté wonena khewmi Di iow.

Moi : hein sagno lolou dh khana. Ngani faté nga khewmi

Rama : dama laye togne RK inchallah tata aïcha mogui si kaw AK sa yeuf tmt fi lagne nékk temps yi

Moi : loutakh wakhoumako ma préparé. Merci qu'à même

Après ma déme
Toc toc

-: entre

Moi : Salam alaikum sama tata mou rafete

Tata : Aleykum salam ya habibi

Moi : hiy tata namone nala teh aussi loutakh ma gueuneu contane tu seras ma belle mère

Tata : hum mala raw iow teh khana taye dousa hénné time bi ngay dokh ok khamena Abdou nga beugue guiss

Moi : mais tataaaa je suis venue ici pour tw. Je ne savais même pas k abdou est ici kone sinon je vais me faire belle

Abdou et Fatou  amour  inoubliable ( Wolof)Où les histoires vivent. Découvrez maintenant