28

2.9K 225 4
                                    

Salam aleykum

Ma yé kiné mou diouke 10h mo diotte

Kiné :  manone ngama bayi ma nélaw ba 13h dh

Moi: iow loutakh nga gnanke diome sa yaye loume la défone kéroke

Kiné :  wakh nga deugue . wayé taye néwoufi kharal ma nélawate

Moi: sama tanta kheuyé goule dh nangue ko dougale sa bopou bobou

Kiné :  ngani bouma ladjié  neko yé nako daye sangou

Moi: iow kharal ma wo sama tanta .TANTA KINÉ NANGOUL DIOUKE

Kiné :  do wakh nanke mangui diouke

Moi: TANTA

Mou gaw diouke dougou si salle de bain bi ma guénde

Moi: Salem alaykum tanta no fanano

Tanta :  aleykum Salem loma done wowé

Moi : hum dara dama guisoul wone sama colle gou blanc gui malako done ladie

Tanta :  nonou ngama koye ladié kharal ma diouke kheuyi

Moi: wa kharema gnou ande

Tanta :  naga gaw ndékki

Ma ndékki apres Gnou  kheuyi Kiné mome demoul nêna daye yénou keur kharitame

___

Tanta :  démale lale table

Moi: wa bakhna

Ma  défare table bi Ma wo gnome Virginie. Ana wo Abdou ak aïcha

Ana: Salem alaykum Fatou

Fatou: aleykum salam ana

Ana: wa loye défe si cuisine bi do gneuw ndékki

Fatou : non merci ndékki na ba paré

Ana: en kone bakh . Tata mariama fane yi gneuwo ba dara daloula la wone rk

Tanta :  dama khawone tawate rk

Ana: kone Alhamdoulillah négame tané nga mangui ndékki dji kone

Mou déme ndékki si kaname touti aïcha dougou si mome rk si désone

Aïcha: oh une revenante Mariama ba yangui tané

Tanta : alhamdoulillah

Aïcha :  li sakh indi mafi wone dama gneuw pour djégaloula mardi baga gneuwé beugone nala wakh wayé dama rousone diakarlo ak iow

Kone amna rousou kaye

Tanta :  ah Garawoul faté wone nako sakh

Aïcha :  Mérci Tata mariama

Hein Damaye guénte wala kagne la commencé wakh tata mariama wayé faté na limouy wakh diarouko fi

Aïcha: Fatou nkm guisou mala wone sakh

Moi: sante yalla mignou sakk bindou gnoune gnépou monté bayi woumala wone khéle sakh kagne nga dougou si wagne bi

Aïcha: légui guise ngama défarale ma café

Moi : laga wathie sa table ba nake

Aïcha :  dama fékk mou djiékh

Moi: kone bakhna fékké daga féke mou djiékh ame nga lokho défarale ko sa bopou

Abdou et Fatou  amour  inoubliable ( Wolof)Où les histoires vivent. Découvrez maintenant