59

2.5K 210 18
                                    

Salam aleykum

Retour dans ma peau

Ma yewou def comme d'hab Abdou envoyéma message néh dama sokhla
Soune parents légui nangou nagne bane diapou date de mariage mais temps yi Abdou da changé depuis bame dégué batou mariage
Dama koye wo téléphone doumako diote ma envoyéko message douma tontou bataye lamaye doga tontou neh dama sokhla

Ma solle li

Dieul sama Téléphone

Ups! Gambar ini tidak mengikuti Pedoman Konten kami. Untuk melanjutkan publikasi, hapuslah gambar ini atau unggah gambar lain.

Dieul sama Téléphone

Abdou je l'aime tellement ba beugou mako niakk temps yi damaye gueudd rk comme lame ko dane défé bou nieukk mais douma wakh dara ndakh je l'aime

Maa : fo dieum

Moi : Abdou la dieum dagni natt soune yeuré takk bi .

Paa: OK boule goudé nake si préparation lagne nékk

Moi : OK mum et dad je vous aime

Eux : de plus chérie

Légui bale naléne gnome gnépou . Bane maye traité comme séne fille

Ma guénn tassée téke Bachir di wathie si voiture bi.

Bachir : salut sœurette khana daga ame RV daga sagnsé dh

Moi : dama yagua sagnesé frère sinon iow nake amago kénn .

Bachir : mane ligaye wathie rk doyenama.  Khalé djiguéne yi mome bientôt rk .

Moi : wa bakhna mangui déme mane

Bachir : OK si kanam bisous

Ma dieul sama auto déme fima Abdou wakh wayé mangui koye fékk mou mér baye foutou

Abdou😡 : iow dagama yape wala gnata heure ma toke fi dilaye khare gneuwo nga  mélni maye  sa PD

Moi : je suis desolé yone bi mo khatone lolo takh.

Abdou : nga wakh mako mo guëne khame nga lanela sakh dagama commencé yape. Limala maye mo eupou. 😡

Mais ki louka dale khana dagne ko ligaye . Chaque jours ma yakarni dina changé mou commencé wate

Moi : Abdou loula dale temps yi yépou niga méle ak mane loumala défe bagaye dokhalé ni

Abdou : defoma dara mane ma togne sama bopou di guénn ak iow . Souma yeugone douma diklou Aïcha ndakh mome la yaga nope

Moi sourire: ooh t'es drôle nake Abdou khamna prank la . Teh mane sakh damala namone loutakh tonto sam sms

Makoye wadia lale mou recoulé

Abdou : mdrr daga nékh damala nourou kouy kafe. Dou wakhone nala ligama défone yépou dinako fayou ak baga diapé aïcha diko dore si fête ga (chapitre 22) . Pourtant wakhone nala dina vengé wou sama pése ba  .

Abdou et Fatou  amour  inoubliable ( Wolof)Tempat cerita menjadi hidup. Temukan sekarang