Chapitre 24

28.5K 3.5K 251
                                    

Tonton Médoune est arrivé en ce moment. Dés que la bonne lui a ouvert la porte, il s'est dirigé vers la chambre, sans même nous regarder.

Maman : Cheri, khana guisso sama yaye? (Chéri, n'as-tu pas vu ma mère?)

Tonton Médoune : Setlouw makowone. Tanta naka nguene deff? (Je ne l'avais pas remarquée. Comment allez vous ma tante?)

Mamie Maguette : Sante Yallah. (Je rends grâce à Dieu)

Tonton Médoune : Naka wa Mbour? Aminata ak Maguette dolene ma nieuw nouyou? (Et la famille? Aminata et Maguette, pourquoi ne me saluez vous pas?)

Nous ne bougions pas. J'avais encore de la haine en me rappelant de l'accusation de vol et des coups.

Mamie Maguette: Li lane la ni? Lane mo khew ba ngene bagne ko diokh lokho? (Pourquoi ne voulez vous pas le saluer?)

Aminata: Daff niouy door rek, di door sama yaye. Dafa Sokhor torop. (Il passe sont temps a nous frapper, il n'épargne même pas maman.)

Maman : Aminata, teudieul sa guemigne bi!! (Aminata, fermes la.)

Mamie Maguette : Nafissatou nopill!! Yow ya wara nopi .. Mounoma degal, Woow lé nga toroop!!! Yangui ni seuy akh goor gu tekkiwul dara!!! Potou café sakh meussumako dieundeul!!! Li nak moy, di daww kouy saww laal, dall si kouy poupe laal. Sa seuy bi meussumasi andeu!!! Medoune dila torokhal goudi ak beuthieuk. Yeugna leppeu!! Door yi ak saga yi!! Fi adoûna la!! (Tu es trop têtue Nafissatou. C'est à toi de la fermer. Tu t'es mariée avec un vaux rien, qui ne m'a jamais acheté un pot de café. Il ne fait que t'humilier, je suis au courant de tout. )

Tonton Médoune: Sama yaye diourouma pour doundal yayou diambour!!! Nafi ma bakh si mom!! Sama diabar la!!! Mane may kilifam. Bu defoul ludoul yone, damako wara corriger. (Ma mère ne m'a pas mis au monde pour m'occuper de la mère d'une autre. Nafi est ma femme, je dois la corriger si elle dépasse les bornes.)

Mamie Maguette : Diourouma doom bougni door ak torokhal. Seuy bi sakh lay tass mane!!! Maye ko batam, mu dem yonam!!! Amaloko bene ndieurigne, thimmm!!! Nafissatou, nianal ki batteu, na gaaw!!! Khawma lula takha beugeu goor ak niakeu fayda rek. (Je n'ai pas mis une fille au monde pour qu'elle soit battue et humiliée. Je veux que cette union se termine, répudie-la. Tu n'es d'aucune utilité. Nafissatou demande lui de te libérer tout de suite. )

Maman : Les filles, rentrez !! Je vous rappellerais plus tard.

Moi : D'accord.

Tonton Médoune: Non, ce n'est pas la peine! Du danga niakeu kilifa, di bayi sa yaye muy diriger sa seuy yi, mane mi fassenala!!! Takkone na benene diabar fane yeuler passé, dina dieul sa plassou niarel. (Comme tu laisses ta mère diriger ta vie et ton ménage, je te répudie. J'avais déjà pris une 3e femme, elle prendra ta place de 2e.)

Maman : Sa nietel bi yeugeulu mako sama yaram. Medoune mane seuy rek la beugeu, sama yaye dafa merr rek, khamnga ko ak ay wakham. (Je m'en fous de ta 3e femme, je me concentre sur mon ménage. Ma mère est juste énervée, tu la connais.)

Mamie Maguette: Nietel diameu? Ey way kumay mbethieu ma yewou??? Yow lutakh wakhomako ? Ki kagne lo lotakh diokhatoula wone dara!!! Yow amo sarap ndeyam, di weur ak sa boppu bu wow, mouss bu odou seur sakh bula romber, nga niane ko diabar!!! Mane nak dieye, tay la warou!!! (Une 3e femme? Dites moi que je rêve. Pourquoi me l'as-tu caché? Tu n'as rien et tu te permets d'épouser toute personne que tu rencontres?)

Maman : Yaye, guenal samay wakh. Dina ko regler. (Maman, laisse-moi régler mes histoires.)

Mamie Maguette : Yow danga meuneu regler dara!!! Ki di Domeram bu magga mag!!! Bama ko guisser ak boppu bi di melni khokou dakkar, ak sabador you fouri yi , ni diapeu katou diane, la khamni torokh nga!!! Mani damay katt ndayou seuy bi feuler. Na seuy bi tass. (Tu ne peux rien régler. C'est juste un batard, je l'ai su en le voyant avec son boubou de charmeur de serpent.)

Chronique de Maguy : le bout du tunnelTahanan ng mga kuwento. Tumuklas ngayon